Max Richter — I am writing this letter song lyrics and translation
The page contains the lyrics and English translation of the song "I am writing this letter" by Max Richter.
Lyrics
bakkan waruw dàll la fa muy degge dooko yëg
dem rekk delu si rekk
melni wèer wi delu si ci sèy jèego
fènèen wèer mouk ci fi,
bidèw bi danouna dèe ci souff
samay xarit, tèy ji ndadjè bi rafèt na,
djoko, seeddo,
ak rétane bi rafèt na,
xèw bou nèex
mais soubbe dagniouy dèm,
galankor bi moy dougnou
meuneu xamanté bou bax,
dou nouy am waxtou
bou doy ngir soppanté
goudi gi wèss, mangi won
fénène, bi ci toop dina fi sori
ak samay bok ci camion bi,
dinagnouy teugueu ngir
féccelo yénéni nit
ak samy bok ci camion bi,
ngir andi mbékté bignouy djeul
bakkan waruw dàll la ku dul toxu doo xam fu dèkk neexe
fa muy dagge dooko yëg
(Merci a El Cancre pour cettes paroles)
Lyrics translation
bakkan waruw dàll la fa muy degge dooko yëg
dem rekk delu and rekk
melni wèer and delu si CI sièy jèego
fènèen wèer mouk ci fi,
bidèw bi danouna deèe ci souff
samay xarit, tèy ji ndadjè bi rafèt na,
djoko, seeddo,
ak retane bi rafèt na,
xèw bou neex
but knew dagniouy dèm,
galankor bi Moy dougnou
meuneu xamanté bou bax,
dou nouy am waxtou
bou Doy ngir soppanté
goudi GI wèss, mangi won
fénène, bi ci toop dina Fi sori
ak samay bok ci truck bi,
dinagnouy teugueu ngir
do it yeneni nit
ak samy bok ci truck bi,
ngir Andi mbékté bignouy djeul
bakkan waruw dàll La Ku Dul toxu Doo xam fu dèkk neexe
fa muy dagge dooko yëg
(Thanks to El Cancre for these words)