Daara J Family — Bayi Yoon song lyrics and translation
The page contains the lyrics and English translation of the song "Bayi Yoon" by Daara J Family.
Lyrics
Sama gaa gna ngi
Doomu Africa mbeur la kaamil
Yagg yagg dina daani
Ci geew ken douko jamnaani
Nenaala sama gaa gna ngi
Ana soutoura bifi gnom mame bayiwoon
Jikko you rafét yignou ragnéwoon?
Dafa melni dagnou bayi sougnou yoon
Beugeu askano lougnou momoutoon
Deug deug xam sa boppa geun
Gnou wakh la ki nga doon oh ! Ooh !
Africains et fiers de ce que nous sommes
Fier d'être africain je suis, j’suis africain donc je suis
Mes ancêtres ont souffert le martyr pour que je puisse relever le défi
C’est à moi de porter le flambeau ils ne peuvent pas me mettre en lambeau
Pour me mettre KO il faut minimum une armée de cent mille rambots
Dis à ton prof d’histoire qu’il raconte des histoires
La plus grande des civilisations est née en Afrique noire
L’Afrique a inspiré le monde avec ses pyramides, sa science, ses mathématiques
Ses symboles et ses signes
Elle créa l'écriture avec les hiéroglyphes du temps des pharaons
Tu ne me crois pas?
Vas-y, demande à Akhenaton. (de Dakar à Marseille)
Ana soutoura bifi gnom mame bayiwoon
Jikko you rafét yignou ragnéwoon?
Dafa melni dagnou bayi sougnou yoon
Beugeu askano lougnou momoutoon
Deug deug xam sa boppa geun
Gnou wakh la ki nga doon
Deug deug xam sa boppa geun
Gnou wakh la ki nga doon oh ! Ooh !
Africains et fiers de ce que nous sommes
Dafa melni gnou ngi daw jeum fenen ni wacc wacc nagnou ande yi xeeb sougnou
ngande yi fekki borom jikko you dande yi
Fo daw fo daw di nga wirri ndaari fa nga jouge fi nga doore fila woore doufou
sorre
Afro sama dole na nga mako xole geum sama demb doon nittou tey njaxass ni
xeetou parfum’k’gowe
Africains koula xass foy gnawe
Africains xola gneup nignouy ngaange
Africains soy joug doufi gawe
Koula xol dina seet fan la lay ngagne
Geum sa bopp xam fi nga bokk melni garab reen banxass ak xob
Dougnou fatte fignou joge ndakh panafricanistes delo sougnou xel demb kanamou
mame gnou giss
Dimbali jam yi biss- gnoul metisses dekkil osiris -carbone14 souliwaat gnou
giss- histoire bindaat grand pere ba petit fils
Ana soutoura bifi gnom mame bayiwoon
Jikko you rafét yignou ragnéwoon?
Dafa melni dagnou bayi sougnou yoon
Beugeu askano lougnou momoutoon
Deug deug xam sa boppa geun
Gnou wakh la ki nga doon
Deug deug xam sa boppa geun
Gnou wakh la ki nga doon oh ! Ooh !
Africains et fiers de ce que nous sommes
Bamako ! Singapour ! Anghata !
Sama gaa gna ngi
Doomu Africa mbeur la kaamil
Yagg yagg dina daani
Doomu Africa mbeur la kaamil
Yagg yagg dina daani
Ci geew ken douko jamnaani
Nenaala sama gaa gna ngi
Ana soutoura bifi gnom mame bayiwoon
Beugeu askano lougnou momoutoon
Sama gaa gna ngi
Doomu Africa mbeur la kaamil
Yagg yagg dina daani
Ci geew ken douko jamnaani
Nenaala sama gaa gna ngi
Doomu Africa mbeur la kaamil
Nenaala sama gaa gna ngi
Ci geew ken douko jamnaani
Nenaala sama gaa gna ngi !
Lyrics translation
Sama gaa GNA ngi
Doomu Africa mbeur La kaamil
Yagg yagg dina daani
Ci geew ken douko jamnaani
Nenaala sama gaa GNA ngi
Ana soutoura bifi GNOME Mame bayiwoon
Jikko you rafét yignou ragnéwoon?
Dafa melni dagnou bayi sougnou yoon
Beugeu askano lougnou momoutoon
Deug DEUG xam sa boppa geun
GNOME wakh to ki nga doon oh ! Ooh !
Africans and proud of who we are
Proud to be African I am, I am African so I am
My ancestors suffered the martyrdom so that I could rise to the challenge
It's up to me to carry the torch they can't tear me apart
To knock me out it takes minimum an army of one hundred thousand rambots
Tell your history teacher he's telling stories
The greatest of Civilizations was born in Black Africa
Africa inspired the world with its pyramids, its science, its mathematics
Its symbols and signs
She created scripture with the hieroglyphs of the time of the Pharaohs
You don't believe me?
Go ahead, ask Akhenaten. (from Dakar to Marseille)
Ana soutoura bifi GNOME Mame bayiwoon
Jikko you rafét yignou ragnéwoon?
Dafa melni dagnou bayi sougnou yoon
Beugeu askano lougnou momoutoon
Deug DEUG xam sa boppa geun
GNOME wakh at ki nga doon
Deug DEUG xam sa boppa geun
GNOME wakh to ki nga doon oh ! Ooh !
Africans and proud of who we are
Dafa melni gnou ngi daw jeum fenen ni WACC WACC nagnou ande yi xeeb sougnou
ngande yi fekki borom jikko you dande yi
Fo daw fo daw di nga wirri ndaari fa nga jouge fi nga Doore fila woore doufou
smile
Afro sama Dole na nga mako xole geum sama demb doon nittou tey njaxass ni
xeetou perfume'k'gowe
African koula xass Foy gnawe
African xola gneup nignouy ngaange
Africans soy jug doufi gawe
Koula Xol Dina seet fan La lay ngagne
Geum sa Bopp xam fi nga bokk melni garab Reen banxass ak xob
Dougnou fatte fignou joge ndakh panafricanistes delo sougnou XEL Demb kanamou
mother wildebeest giss
Dimbali jam yi biss- gnoul metisses dekkil osiris -carbone14 souliwaat gnou
giss- histoire bindaat grand pere ba petit fils
Ana soutoura bifi gnom mame bayiwoon
Jikko you rafét yignou ragnéwoon?
Dafa melni dagnou bayi sougnou yoon
Beugeu askano lougnou momoutoon
Deug deug xam sa boppa geun
Gnou wakh la ki nga doon
Deug deug xam sa boppa geun
Gnou wakh la ki nga doon oh ! Ooh !
Africains et fiers de ce que nous sommes
Bamako ! Singapour ! Anghata !
Sama gaa gna ngi
Doomu Africa mbeur la kaamil
Yagg yagg dina daani
Doomu Africa mbeur la kaamil
Yagg yagg dina daani
Ci geew ken douko jamnaani
Nenaala sama gaa gna ngi
Ana soutoura bifi gnom mame bayiwoon
Beugeu askano lougnou momoutoon
Sama gaa gna ngi
Doomu Africa mbeur la kaamil
Yagg yagg dina daani
Ci geew ken douko jamnaani
Nenaala sama gaa gna ngi
Doomu Africa mbeur la kaamil
Nenaala sama gaa gna ngi
Ci geew ken douko jamnaani
Nenaala sama gaa gna ngi !